tweetindex
FR

Moor Suraŋ ✓

@s_sourang · Senegal · joined 25 Mar 2019

Mor Sourang PDG Massalik Café, Écrivain et Chercheur sur le Mouridisme

32 136Followers
1 657Following
37 867Posts total
156.7KViews on collected posts

Derniers posts

Wallaahi ku ko mere it ba laa yàgg dara dinga ko yërëm lool lool lool, amul sikk sàkka. 1.8K views · 58 likes · 7 reposts · 2 replies Open on X →
Leeg-leeg nga dégg ku ray njabootam ba noppi daal di xaru. Waa ji ni ma ko gisee yoon woowu la jaar, xam ne kenn bëggu ko mu far sànk réew mi yokk coono yi, ba kenn dootul defar Senegaal. 1.1K views · 71 likes · 6 reposts · 2 replies Open on X →
Nooni Senegaal yi ci biir réew mi ak bitiim réew boole nañu seen i doole ngie xeex Sonkoo, loolu nag day wane rekk ne kon Sonkoo mooy ki bëgg réew mi te yërëm waa réew mi, te man leen a génne ci ag jaamu tubaab. 1K views · 103 likes · 25 reposts · 0 replies Open on X →
Ci moment yi ngay doora comprendre patriotisme gi nekk ci Sonkoo ak ni muy sàmmee intérêt askan wi. Yoon wi mu tegu woon leer na nàññ, Senegaal da doon génn ci jafe-jafe yèpp fii ak at yu néew, li tax mu wane ginnaaw rekk caaxaan yépp tàmbliwaat ci ngay xamee ne nit ku am solo 3.9K views · 432 likes · 118 reposts · 2 replies Open on X →
@s_sourang Yaaram noumay déff ba am sa contact 140 views · 0 likes · 0 reposts · 1 replies Open on X →
@s_sourang Nataal bii neex nama lool😎 411 views · 1 likes · 0 reposts · 1 replies Open on X →
@s_sourang Sa jëmm ji nga gën a wane ci mbind mi de saay 😂 680 views · 0 likes · 0 reposts · 2 replies Open on X →
Patrimoine bi gën a mag ci Sëriñ Tuubaa mooy mbind mi. https://t.co/HrlGBXAHNU
147.7K views · 1.4K likes · 244 reposts · 16 replies Open on X →

Face aux comptes de taille comparable

4 posts des 90 derniers jours, à côté de la tranche de 10K–100K abonnés. diffusé bien au-delà de son propre public, et ce public réagit.

Vues médianes1 452ce compte924médiane pour 10K–100K
Portée, %4.52%ce compte3.62%médiane pour 10K–100K
Engagement, %9.82%ce compte1.52%médiane pour 10K–100K
IndicateurCe compteMédiane pour 10K–100KRapport
Vues médianes par post1 4529241.57×
Portée (vues ÷ abonnés)4.52%3.62%1.25×
Taux d'engagement9.82%1.52%6.46×

Autres comptes de cette tranche →   Comparer avec un autre compte →   Comment ces repères sont établis →

Growth & engagement

How the posts we collected actually performed: views and reaction rate post by post, what the audience did with them, and where the follower count goes.

Views per post

147.7K6 Jan
680
411
14022 May
3.9K24 Sep
1K
1.1K
1.8K

Last 8 collected posts, oldest on the left. The scale is logarithmic: one post can outrun the rest a hundred times over.

Engagement rate per post

1.16%6 Jan
0.29%
0.49%
0.71%22 May
14.17%24 Sep
12.52%
7.12%
3.76%

Reactions — likes, reposts, replies and quotes — divided by views. Median for 10K–100K accounts is 1.52%.

What the audience does

Likes81.0%2 094 in total
Reposts15.5%400 in total
Replies1.0%26 in total
Quotes1.3%34 in total
Bookmarks1.2%30 in total

Share of every reaction we collected for this account. Replies mean argument, reposts mean endorsement, bookmarks mean the post was worth keeping.

The follower curve appears once this account has two daily snapshots — we take one a day, and this one is on its first.

Comptes similaires